FANDOM

2,025,397 Pages

StarIconGreen
LangIcon
Diabaram

This song is by 坂本龍一 and appears on the album Beauty (1989) by Ryuichi Sakamoto.

Diabaram, diabaram, diabaram, nena dou ko baye, tarou naye, tarou naye, taru naye, mom la mino, nena dou ko baye, mom la khama ba nena dou ko baye. Nit sama nit nit nit garabam, guemnane.
Diabaram, diabaram, diabaram, nena dou ko baye, tarou naye, tarou naye, mom la mino, nena dou ko baye, tarou na, mom la mino, mom la kham dou ko baye. Nit sama nit ni nit garabam, guemnane.
Diabaram, diabaram, diabaram, nena dou ko baye, tarou naye, tarou naye, mboleme kharitam yep, xou nguinane ko bayiko, te mom la mino, mom la kham mo ko xaniwone, nena dou ko baye, diabaram, nit sama nit nit nit garabam, guemnane.
Diabaram, diabaram, diabaram, nena dou ko baye, tassou naye, tassou na limou digale, momm soko ne tam bayil, lolou mety.

External links